Ami Mbeng

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

« JÀMM A GËN 3e MANDAT »

Way-moomeel yee ngi sàkku ci Njiitu réew mi, Maki Sàll, mu bañ a laaj...

JÀNGOROY SËQAT SU BON SI

Sëqat su bon si, jàngoro ju ñu mën a moytu la, te it lu...

SIROY ALLAAXIRA YA CA  GÀMBI

Musiba bu réy a am ca Gàmbi. Juróom-benn fukki xale ak juróom-benn ñoo fa...

BALAA NGAA LAAX JAAY, LAAX LEKK

Ngomblaan gee woote ngir dépite yi jëlsi kaarbiraŋ biñ leen di jagleel weer wu...

YOKKUTEG DUND GI “…dañuy ragal ne 2023 mooy gën a metti.”

Njiitu réew mi, Maki Sàll, woote woon na ndajem waxtaan ñeel dund gi. Altine,...

NDIISOOY NGOMBLAAN GI

Dogub 24eel bu càrtub Ngomblaan gi dafa tëral ne : « Ci ndoorteelu gépp moomeg...

Aa ! Gaa ñi, Tataa Mimi mer na !

Aminata Ture mer na nag. Te, altine ba léegi, moo ngi koy fésal ak...

KUY DUND DI XASAW, BOO DEEWEE DU MAT A WAX

 Toftaleg IDH gu 2022 génn na ci alxames ji. PNUD a ko génne. PNUD...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA