Naqar ak uw tiis la ndongoy jànguneb Gastõ Berse fanaane démb. Seen benn moroom moo ñàkk bakkanam. Ca biir néeg ba mu nekkoon, ca Village A, lees ko fekk mu tëdd, tàggook bakkanam.
Mataar Jaañ la ndongo li faatu tuddoon. Mi ngi doon jàng wàlluw...
Bi kàmpaañu njaayum gerte gi tàmbalee ba nëgëni sii, banqaasu SONACOS bi nekk Njurbel dajale na 22. 000iy toni gerte. Lim boobu nag, moo ëpp fukki yoon lim bi mu dajale woon daaw. Ki xamle xibaar boobule mooy Suleymaan Jóob, moom miy DRDR (Directeur...