Mbay Sow

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara waralu ko lu dul bor bi fi Maki Sàll bàyyi ak li FMI di dóor dàqe ak Nguur gi fi nekk. Rax-ci-dolli, kurél gii di Moody’s dafa yokk ci xar...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw ci doxalin wu digg-dóomu ñeel lekkool yi. Muy doxalin wuy boole ñépp, am njariñ te di yamale. Barki-démb ci àjjuma ji, 10i fan ci weeru Oktoobar 2025, Càmm gi doon na...

DI BUUR, DI BUMMI

Li jaaxal waa Senegaal, mooy wax-waxeet yi kilifay réew mi dëkke. Ku ci jóge...

XËCC BU DAŊEE DAGG !

Nimbir yiy doxe diggante nguur geek kujje gi bi Màkki Sáll toogee ci jal...

XËT YI MUJJ

NGUURUG SENEGAAL DAJALE NA 450i MILIYAAR

Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : NGUUR GI NAMM NAA AMAL DOXALIN WU DIGG-DÓOMU

Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw...

LI CI DIGGANTE NIT AK NITE

Moo xam muy seen doomu bopp walla jeneen ju ñu leen dénk, way-jur yu...

BUL BIND… / BINDAL…

Seen yéenekaayu web ci wolof ubbil na leen xët wu bees wees duppee BUL...