Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/10/2024)

KÀDDUY ÀLLIYUN TIN ÑEEL WAY-PÓLITIG YI Àlliyun Tin, di kenn ci njiiti kuréli ma-xejj yi,...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukkee na fi réew mi barki-démb...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkateeti na ay kàddu. Muy i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/10/2024)

WALUM DEX GI Càmm gi teggiwul tànkam ci taxawaay bi mu am ñeel walum dex...

KOOM-KOOM : PÉNCOO ÑEEL NDEFAR GEEK YAXANTU BI

Càmm gi dogu na ci aar cumbeefi biir réew mi (les entreprises locales). Jëwriñ...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/10/2024)

SENEGAAL 2050 Senegaal am na sémbu delluwaay wu bees. Tay ci altine ji, 14i pani...

LU YEES CI MBIRUM PRODAC

Am na lu yees ci mbirum Prodac mi. BAD (Brigade des Affaires Générales), di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (7/10/2024)

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI ÑEEL FMI Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, rafetlu...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA