Uséynu Béey

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax réew mi. Looloo tax, ci Sémbuw Àtteb Ngurd mu 2026 mi, ñu sóoraale ci naaluw kopparal wu mag a mag....

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii di Seex Ture faatoo ak ñan ñoo jël bakkanam. Dafa di sax, am na ku ñu duutagum baaraam, njort ne laale na ci mbir mi. Bu dee li ñeel luññutu yi,...

Sàmpiyonaa Senegaal : Casa Sport jël na raw-gàddu gi, SONACOS ak Estaad bu mbuur dellusi

Dibéer bi weesu (fukki fan ak ñaar ci weeru Me lees doon amal ñaar-fukk...

Lan moo wund demu Maki bi Riisi ?

Fan yii weesu, njiitu réew, Maki Sàll, fekki woon na Putin ca Riisi ngir,...

NDAJEM ÑAXTU YEWWI ASKAN WI : WEDDI, GIS BOKKU CI

Coowal wotey palum depite yi lёmbe na réewum Senegaal lool ci jamono jii nu...

Malaanum Lëndëm : Bóris Jóob, na woon, fa woon

Ñeenteelu yoon a ngi nii Bubakar Bóris Jóob di génne téere bu mu bind...

RUWÀNDAA, RÉEW MA FARÃS NEE TOTT AK GÀCCE 2/2

Ci atum 1997 la Mehdi Bâ génne téereem bu jëkk, jox ko tur wu...

GÀCCE NGAALAAMA, MBUGAAR !

Senegaal amati na ndam ci 3eelu fan ci weeru nowàmbar wii, jaare ko ci...

KUJJE GEEK WOTEB 2022 BI: BËGG NAA LA, BËGGUMA LA, LOOLU JARUL COOW

Ci bésub 23 sàŋwiye ci atum 2022 bii di ñëw, la Senegaal fas yéene amal...

WAAW, KAÑ LA SENEGAAL GËJ A YËNGOO NII…?

Weeru màrs wii weesu, Senegaal tàngoon na jipp ! Gannaaw ba alkaati yeek sàndarm...

XËT YI MUJJ

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii...

COKKAASU ODIA

TUKKIY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, door na tukki yu am solo ci...