Defu Waxu

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug elimaanu jëwriñ ya, Michel Barnier. Dépitey kujje gees duppee « La gauche » ñoo dugaloon pasu diiŋat mi, wote ko, jàllale ko. Muy tekki ne, Càmm gi Michel Barnier taxawaloon...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar a leen dikkal ci àllarbay tay jii, 4i pani desàmbar 2024. Dafa di, waadab seereer ba woon, Àmburuwaas Saar, moo génn àddina. Moom nag, Àmburuwaas Saar, mbër mu mag la woon,...

SAMES SÓOBU NA CI XEEX BI

Fajkat yi xamle nañ ne dinañ dakkal seen liggéey ci diirub ñaari fan. Seen...

NGOMBLAAN GI JÀLLALE NA SEMBUB ÀTTE BI

Bees sukkandikoo ci Ayib Dafe, Ndiisoog àtte yi jàllale na sembub àtte biy soppi...

DOGATI NAÑ SIÑAALU WALFADJRI !

Bees sukkandikoo ci Seex Ñas, doomu Siidi Lamin Ñas mi jiite Walfadjri, Nguur gi...

USMAAN SONKO : « MBATIIT MOOY LÉPP, MOOY CËSLAAYU YOKKUTE. »

Laaj ak tontu bii nag, seen yéenekaayub web defuwaxu.com séqoon na kook Usmaan Sonko...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI (4/8/2023)

PASTEF Ñoo ngi wéy di raafal ndawi Pastef yi. Keroog, Tuseŋ Màngaa ak Bentaleb Sow...

GÀTTALI BÉS BI (28/6/2023)

TABASKI Waa Ahlus Sunna, ñi ñu duppee Ibaadu, tabaski nañu tey ci àllarba ji, 28...

Gàttali bés bi (23/6/2023)

Waxtaan wi jeex na Ëllëg, gaawu 24 suwe 2023, la Njiitu réew mi, Maki Sàll,...

XËT YI MUJJ

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2024)

CAAROY 44 : NJIITU RÉEW MI JËL NAY NDOGAL Barki-démb ci dibéer ji lañu doon màggal...

TIIS WU RÉY FA GINE

Mats futbal bu mujje ciy masta ! Mbir yaa ngi xew barki-démb ci dibéeru...