Li fës

NDAJEM NDEYU SÀRTU RÉEW MI DËGGAL NA LAWAXUG SONKO AK BÀRTELEMI JAAS

Ndajem Ndeyu sàrtu réew mi àtte na. Ci guddig àjjuma ji la fésal ndogal...

NJIITUL KING FAHD PALACE WEDDI NA MAJAMBAL

Piyeer Mbów mooy njiitu këru gan gii di "King Fahd Palace". Moom nag, dafa...

TAKKU WALLU BËGGUL SONKO BOKK

Démb, ci altine ji, la waa DGE (Direction Générale des Elections) siiwal toftale yi....

WOTEY NGOMBLAAN YEES RANDALSI : DGE SIIWAL NA 41 TOFTALE

Kurél gu mag guy saytu wote yi fi Senegaal, Direction générale des élections (DGE),...

MAKI SÀLL, LU LA KO JARAL ?

Seneweb moo siiwal xibaar bi. Maki Sàll, Njiitu réewum Senegaal mi folleeku keroog 24...

SETAL SUNU RÉEW : TEEWAAYU NJIITU RÉEW MI FA MBUUR

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Fay, moo ubbi juróomeelu bésub set-setal bees di amal...

ARCELOR MITTAL : ÀTTE BOR, FAY !

Càmmug Senegaal gu yees gi, jaare ko ci DGID, di kurél giy dajale kubal...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...