Xibaar

JÀNG AK JÀNGALE CI JAMONOY MBAS (Safiyetu Béey)

SAFIYETU BÉEY Céy Koronaa ! Doomu-jàngoro bii yëngal na jamono. Ku mënoon a gëm lu ndawe nii...

GÀTTALUG XIBAAR YI

(Ayu-bésu 4eel jàpp 10eelu fan ci weeru Me) (PAAP AALI JÀLLO) Liggéey ngir Yàlla : Ñiy liggéey...

PORFESOOR MUSAA SÉYDI : «BÀYYI WIRIS BI LAW, MUSIBA LA NU NAROON A JURAL»

  Bàyyi wirisu Covid-19 bi law ngir sabab kiiraayu-mbooloo la Doktoor Paap Musaa Coor digle...

GÀTTALUG XIBAAR YI (AMI MBENG)

AMI MBENG ABLAAY JUUF SAAR : « Li nu gën a seetlu mooy ne limu way-tawati...

«BU DUL WOON DOXANDÉEM YI, MBAS MI DU NAANE ÑEEX AFRIG » (Doktoor Séydu Jàllo)

Paap Aali Jàllo Doktoor Séydu Jàllo ab Farmasiyeŋ la, dib biyólósis ak « ancien interne...

FAN LANU JËM AK ÑAKKI BILL GATES YI?

(USÉYNU BÉEY) Coow laa ngi ne kurr ! Afrig ba Afrig daj, li ko dale Keer...

«LI MAY RAGAL…» LAAJ-TONTU AK DOKTOOR SÉYDU JÀLLO (II)

Paap Aali Jàllo Doktoor Séydu Jàllo ab farmasiyeŋ la, dib biyólósis. xam-xamam màcc na tamit...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...