Xibaar

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (19/6/2025)

ELIMAAN JËWRIÑ YI ÀDDU NA CI JAFE-JAFEY GAYNDEY BASKET YU JIGÉEN YI Gaynde yu jigéen...

FRAPP : NOO BAÑ ! “ASSISES DE LA DÉMOCRATIE” BI MAKORÕ BËGG A AMAL UCAD DU FI AME !

Waa FRAPP siiwal nañu ab yégle, démb àllarba 18 suwe 2025, di ci biral...

ISRAAYEL – IRÃ : JURÓOMEELU BÉSUB XARE

Juróomi fan ci tay, bi xare bi tàmbalee diggante Israayel ak Irã. Bees ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/6/2025)

LU BEES CI COOWAL SUUF LA CA GÉEJAWAAY Lu bees amaat na ci coowal suuf...

KÀTTEY CFEE YU 2025

Kàtte yu atum 2025 mi dinañu tàmbali ginnaaw-ëllëg, alxames 19 suwe, jeex ci àjjuma...

JIIXI-JAAXA CI GÉNNUG ÀDDUNA IMAAM UMAR JAAWO

Naqar ak tiis la askanu Koldaa nekke fan yii, rawatina ña dëkke fa koñ...

“COUPE DU MONDE DES CLUB 2025”

Joŋanteb kuppe bees duppee “Coupe du monde des clubs”, di po mu mag muy...

IRÃ – ISRAAYEL : XARE BAA NGAY WÉY

Xare baa ngay wéy diggante Irã ak Israayel. Ci guddig démb gi, gaawu jàpp...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...