Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

KORONAA, LËMBAAJE NGA DUNYAA (Taalifu Li Faal Sàmba Suuna)

  Koronaa Yamoo ci doon balaa Dajal nga àddina-wërngal-kepp Bawoo ca réew ma ñuy wax Caayna Ab xoqtal tax laa jóg kepp Lëmbaaje nga Dunyaa Fit yépp rëcc nañu Ñii naan ab...

KÀDDUY AADAMA JEŋ

Tofo ci Antonio Gutieres, « Sekerteer Seneraalu » Mbootaayu xeet yi, di ko xelal ci lépp lu aju ci aar faagaagal aw xeet.  (Siyaara Tayba Ngéyéen)   Asalaamu...

SENEGALEY ITALI YI : LA WOON WONNI NA

Fàttaliku lu war jaam la, kon na xel dellu ci ginnaaw ngir saytu walla jéex démbu Senegale yi  njëkk a  agsi Milan. Démb a...

YOONU YÀQUTE…

"Noo lànk !" Ñaari baat yooyu la askanu Senegaal wépp àndandoo yuuxu cib doxu-ñaxtu, àjjuma jii weesu. Li nu ko dugge woon mooy fésal seen naqar...

NDAX MAKI SÀLL WAR NAA LAAJ ÑETTEELU MOOMEEL ?

Lu waay xamadi xamadi xam ne Maki Sàll mooy Njiitu-réew mi. Waaw, ne askan wee ko fal ci atum 2012. Bi mu toogeek léegi...

CFA WALLA ECO ? SÀMBAAY BÀCC REKK…

Xaar bi yàggoon na, xeex bi metti lool, coow li ne kurr, saf sàpp ci Farãs ak Njiiti-réewi Afrig sowu-jant yi. “CFA, na fi...

“Ngalla bunu jaawale ECO ak… ECO!'”

Fan yii, coowal ECO baa ngi mel ni tànnbéeru dëmm, rëb ba nga ne lii lum doon. Bi Emmanuel Macron ak Alassane Ouattara defee...

LI WARAL NJËGU KURAŋ BI YOKKU

Li ñu doon laam-laame mujje naa am dëggëntaan. Njëgu kuraŋ bi yokku na li ko dale dibéer, 1eelu fan, ci weeru desàmbar 2019. Njiitu...

JÉERI JOOR NDEELAAK TUBAAB BI

Jéeri Joor Ndeela Faal mu ngi gane àdduna ci atum 1871. Mu doon doom ci Sàmba Yaaya Faal mi newoon fanweer ak ñaarelu Dammeelu...

DIGE GÉEJ, KILIBU SÉEX ALIYU NDAW : TEKKI MBAA LAB

Dige géej, téere kilib bii Séex Aliyu Ndaw di door a génne, OSAD mi Soxna Aram Faal jiite moo ko móol ci atum 2019....

Bataaxalu Saalif Keyta ñeel IBK

Ci tekkib Paap Aali Jàllo