Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LEES WAR A JÀNG CI NDIMBALU RÉEWUM FIDEL CASTRO ÑEEL ITALI ?

Boos Ndóoy*   Saa buñ tuddee réewum Kibaa, ñépp daldi fàttaliku njiitam lu ràññeeku la : Fidel Castro. Waaye, xel yépp dañuy dellu 60i at ci...

LEES WAR A JÀNG CI NDIMBALU RÉEWUM FIDEL CASTRO ÑEEL ITALI ?

BOOS NDÓOY   Saa buñ tuddee réewum Kibaa, ñépp daldi fàttaliku njiitam lu ràññeeku la : Fidel Castro. Waaye, xel yépp dañuy dellu 60i at ci...

KORONAAWIRIS : MBETE GAYNDE GU TËX !

Ndey Koddu Faal   Fii ci Senegaal, limu ñi Covid-19 bi daaneel romb na téeméer. Moonte bi feebar biy soog a feeñ ca réewum Siin, ñetti weer...

LI UMAR YUM AK AALI NGUY NJAAY WAX TASKATI XIBAAR YI ÑEEL GUURAL GI

Paap Aali Jàllo Senegaal, ca njëlbeen ga (2eelu fan ci weeru màrs 2020), diiwaanu Ndakaaru kesee amoon Covid-19. Wànte, tey (29eelufan ci  weeru màrs jàngoro...

BÀTTALE MAKI SÀLL ÑEEL MBASUM COVID-19 MI

Ami Mbeng “…Luy jot jot na ginnaaw dee.”   Ci altine jii weesu, 23eelu fan ci màrs 2020 la njiitu réew mi, Maki Sàll, doon amal ñaareelu...

KORONAAK ÀDDINA

Taalifu Làmp Faal Kala Ki daan mere nit ñi ci ñàkk a nuyoo Moo bank ab loxoom di tere nuyoo Ki daa tëju amul yitte lañ daan...

KORONAAWIRIS, LOO NU NARAL ?

  Ci bésub altine, 2eelu fan ci weeru màrs, atum 2020 la Covid-19 bi ganesi Senegaal. Xibaar baa ngi tukke woon ci jawriñ Abdulaay Juuf...

COVID-19 CI ÀDDINA SI

Ami Mbeng   Bu dee mbas mi wàññeeku na bu baax ca Siin, mu ngiy wéy di rajaxe àddina si, rawati-na réewi Ërob yi. 159 réew...

KORONAA

  Taalif bii, Séex Axmadu Bàmba Njaay moo ko bind,Njaay-Jaata, dëkk Njaaréem.Moom góoru Ajaa Maryéemmooy ñaan mbas mi ne mes.  Àddina si tey dafa taxaw Ku nekk...

BATAAXALU ITALI BU TIISE NII…

Mbokki Senegaal, Maa ngi leen di nuyu yéen ñépp, ku ci nekk ci sa tur ak sa sant. Tey, fii ci Milaŋ, maak sama soxna danoo...