Tolluwaayu réewum Senegaal ci wàllu koom tàmbali naa ub boppu ñenn ñi. Te, dara waralu ko lu dul bor bi fi Maki Sàll bàyyi ak li FMI di dóor dàqe ak Nguur gi fi nekk. Rax-ci-dolli, kurél gii di Moody’s dafa yokk ci xar...
Ci ubbite lekkool gi, Nguur gi jël nay matuwaay yu am solo ngir taxaw ci doxalin wu digg-dóomu ñeel lekkool yi. Muy doxalin wuy boole ñépp, am njariñ te di yamale.
Barki-démb ci àjjuma ji, 10i fan ci weeru Oktoobar 2025, Càmm gi doon na...