Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

NJIITU RÉEW MI NANGU NA SUUFUS RËBËS

Bi ñuy waaj a amal wotey palug Njiitu réew mi, as diir kepp desoon...

PASTEF AK TFM, LU XEW ?

Coowoo diggante làngug Pastef gi ak tele bii di TFM du guléet ñu koy...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (20/3/2025)

COOWAL AMNISTI BI Coppiteg amnisti bi dépitey Pastef yi namm a wotelu ca Ngomblaan ga...

NJAAM GU YEES FA ARAABI SAWDIT

Xoqatal ak metital ya amoon ca jamonoy njaam ga dekkiwaat na fa Araabi Sawdit....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI(13/3/2025)

NDOGAL YI ELIMAANU JËWRIÑ YI JËL ÑEEL MBIRUM SUUF SI Démb, ci àllarba ji lañu...

NGUUR GI XAATIMAL NA “SAES” AB DEKKERE

SAES (Syndicat Autonome de l’Enseignement Supérieur) mooy kurél gi ëmb jàngalekat yi nekk ci...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/3/2025)

“SUIT” WEDDI NA XIBAAR BI L’OBS JIBAL SUIT (Syndicat Unique des Travailleurs du Trésor) mooy...

UMAR SISOKO EMBALOO DÀQ NA NDAWI CEDEAO AK UNOWAS

Ñaari kuréli Afrig sowu-jant yii di CEDEAO (Communauté Economique Des Etats de l’Afrique de...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA