Ndey Koddu Faal

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax réew mi. Looloo tax, ci Sémbuw Àtteb Ngurd mu 2026 mi, ñu sóoraale ci naaluw kopparal wu mag a mag....

SËRIÑ AMDI MÓODU MBENDA FAAL WÀCC NA LIGGÉEY

Sëriñ Amdi Móodu Mbenda Faal, xalifa Baay-Faal yi, wàcc na liggéey. Démb ci àllarba...

BÉSUB NJÀNGUM XALE YU JIGÉEN ÑI

Démb, alxames 9eelu fanu sãwiyee 2025, la Njawriñu njàng mi doon màggal, fa Jamñaajo,...

MISS LITTÉRATURE SENEGAAL : NEEX XEL, RAFET KÀDDU

Njeexitalu joŋante Miss Littérature Senegaal démb la woon, àllarba, 18eelu fanu désambar 2024, ca...

ALIYUN BADARA BÉEY GUDDEE NA

Aliyun Badara Béey, njiitu kurélu bindkati Senegaal yi, moo génn àddina. Keroog, dibéer 1eelu...

BATAAXALU NGUGI AK BÓRIS JÓOB ÑEEL NJIITU RÉEW MI

Ci tekkig Ndey Koddu FAAL "Kilifa gu mag gi,  Jàmm ak salaam ñeel nañu la ! Say...

23 AWRIL BÉSUB TÉERE AK ÀQU BINDKAT BI

Mbootaayu Xeet yi ñeel njàng, xarala ak mbatiit (UNESCO) moo tànn bésub 23 ci...

SÉEX ALIYU NDAW GÉNTOON NA KO DÉMB, AADAMA BAROW AK BASIIRU JOMAAY FAY DEF NAÑ KO TEY

Atum 1981, Séex Aliyu Ndaw, bindkat bu ràññeeku, daa bind woy tudde ko : Sama...

RUWÀNDAA, 30I GINNAAW FAAGAAGALUG TUTSI YA

Lu xewoon Ruwàndaa ca atum 1994 ? Keeroog, 6eelu fanu awril 1994, lañ song roppalaanu Njiitu...

XËT YI MUJJ

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii...

COKKAASU ODIA