Ndey Koddu Faal

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi tukkee ci wotey 24 màrs yi ñu doon amal ci dibéer jii weesu.  Gannaaw ba ñu jotee njureefi pekkiy wote yi ci Senegaal ak bitim-réew, càmbar leen, saytu leen ni mu...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi ci àddina si ndokkeel nañ Basiiru Jomaay Fay mi askanuw Senegaal fal, def ko juróomeelu Njiitu réewum Senegaal.  Aadam Baróo (Njiiti réewum Gàmbi) “Maa ngi ndokkeel Sëñ Basiiru Jomaay Fay ngir ndam...

SËRIÑ SAALIW TURE WÀCC NA

Sëriñ Saaliw Ture mi toogaloon xalifa Murid yi ca Kees a wàcc liggéey guddig...

DABBAAX : BAAX NGIR YÀLLA, BAAX CI SENEGAAL

Senegaal, ci sunu aada, bu ñu tuddee doom, dañu baaxoo di ñaan : Yal na...

SËÑ BÀMBA

Sëñ Bàmba Kéemaan la Dem ba ñëw war a sant ci ñibbisi gi Di sant Boroom bi ci dem...

50eelu LËLU CESTI : 33I TASKATI XIBAAR YU BEES

Barki-démb, ci alxames ji (25eelu me 2023) la CESTI doon jox seen lijaasa 5i...

POROFESËER PENDA MBÓW : « MËSUMA ÀND CI YEMOOG GÓOR AK JIGÉEN (« LOI SUR LA PARITÉ ») »

Bañ koy wote ci jamonoy Njiitu réew ma woon, Abdulaay Wàdd, soxna Penda kesee...

23 AWRIL, BÉSUB TÉERE AK ÀQI BINDKAT BI

Mbootaayu Xeet yi ñeel njàng, xarala ak mbatiit (UNESCO) moo tànn bésub 23i awril,...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu...

XËT YI MUJJ

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi...

COPPITE YI BASIIRU JOMAAY FAY DIGE

Démb la Njiitu réewum Senegaal lu bees li doon biral kàddoom yu njëkk. Fa...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (25/3/ 2024)

KÀDDUY BASIIRU JOMAAY FAY YU NJËKK NIKI NJIITU RÉEWUM SENEGAAL  Njiitu réew lu bees li,...