Ndey Koddu Faal

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga woon, bi 16i waxtu jotee ci ngoon, fa màkkaanu banqaasu luññutu bob sàndarmëri . Sabab bi tax ñu woolu woon ko mooy kàddu ya mu yékkati woon ci menn ndajem...

COKKAASU ODIA

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

LÀMMIÑ WEES NÀMP

21eelu féwaryee lañ jagleel ci àddina sépp bésu làmmiñ wi nga nàmp. Xalaat bu...

KEN NDÓOY « ÑÀKK NA BAKKANAM »

Bindal sargal ku génn àddina, damay koy def. Waaye de, lu ma diis la,...

Rafayel Njaay taalifkat la woon…

Ndeem dëgg la ni àjjana, ngir mbindeef yi daa yokk yëf yu baax ci...

SÉEX ANTA JÓOB, SUUL KER DU KO TEE FEEÑ…

Séex Anta Jóob a ngi juddoo Céytu, 29eelu fan ci desàmbar 1923. Alxuraan la...

SIDAA NGI WÉY DI REY…

Biige Jaañ, ndaw su jekkoon, neex deret lool, moo dem ba mel ni kuy...

GÓOR GU MAT DU DÓOR JIGÉEN…

Alxames, 1 fan ci weeru desàmbar mooy bés bi ñu jagleel xeex sidaa ci...

BÉSUB BINDKATI AFRIG YI

7i fan ci weeru nowàmbar mooy bés bi ñu jagleel bindukati Afrig yi (saa-Afrig)....

XËT YI MUJJ

TÉYANDI NAÑU PAAB MAALIG NDUUR (APR)

Tay lañu woolu woon Paab Maalig Nduur, nekkoon jëwriñ ca nguurug Maki Sàll ga...

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii...