Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

Liggéeykat yi ci dalub roppalaan yee ngi dànkaafu Nguur gi

Mbooloo mi ëmb kuréli liggéeykat yi ci dalub roppëlaan yi (Intersyndicale des travailleurs de...

AKSIDÃ CA LUGA : JURÓOMI BAKKAN ROT NAÑU

Tali baa ngiy wéy di faat bakkani way-tukki yi. Aksidaŋ bu jàll, beneen tegu...

LAYOO MAAM MBAY ÑAŊ – USMAAN SONKO JEEXAGUL

Démb, ci alxames ji, 6 awril 2023, layookati Usmaan Sonko yi woote woon nañu...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Tey, talaata, 4 awril 2023, la Senegaal di Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak...

4 AWRIL : NAXEE-MBAAY WALLA ?

Fileek ñeenti fan, Senegaal dina Màggal jonnug boppam, ginnaaw juróom-benn-fukk ak ñetti at, bim...

KAYIS SAYET WAXATI NA NJOMBE

Njiitu réewum Tinisi li, namm naa andeeti coow ci diggante Tinisi ak Libi. Àtte...

Paap Masata Jaag dina tëdd 5i ati kaso

Ëttub àttewaay bu Pari delsi na ci àtteb Paap Masata Jaag bi. Waaye, àtte...

Tukkib Njiitu Réewum Farãs li ci kembarug Afrig

Tukki ñeenti fan la Emanuyel Makarõ, Njiitu réewum Farãs li tàmbali alxemes 2 màrs...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA