Njuga Gay

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 12 ut 2022

TÀGGAT-YARAM Ikibu Casa Sport bi dugg na ci joŋantey Ligue des champions / CAF bi....

JOŊANTE CHAN 2022 ALSERI

Bokkadil yu CHAN 2022 bi jeex nañ ci njeexitalu ayu-bés bi weesu. Ren jii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 5 ut 2022

PÓLITIG Maalig Gàkku fésal na yéeneem ak taxawaay bi mu namm a am ëllëg ci...

JOŊANTEY BASKET FIBA 2023

Senegaal bëgg naa dalal ndajem Playoffs yu mujj yi Menn ndaje a des ci juróom...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Altine 29 ut 2022

PÓLITIG Fukki fan ak ñaar ci weeru Sàttumbar lañu war a taxawal tëralinu péncum ndawi...

Làmb : mbër yaa ngi jooy

CNG def na mujjum ndajeem mu mag ginnaaw bi làmb ji tëje. Mi ngi...

AFRIG, TONTU DU FOROX, Tontu ñeel kàdduy Óreliyoo De Lórãtis yi

Duma topp diw boo gis, fi ngeen jëm dafa sorewul. Loolu la waa CAF...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA