Njuga Gay

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/3/2024)

MAKI SÀLL DEF NA NDAJEM JËWRIÑAM MU MUJJ Dibéer jii weesu lañu doon amal wotey palug Njiitu réew mi. Ka jiitu ca wote ya mooy Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Moom Njiitu réew mi ak mbooleem lawax yi nangul ko ndamam li, daldi ko ciy...

MAKI SÀLL, DALAL NA JOMAAY AK SONKO FA PALE BA

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na ki koy wuutu, Basiiru Jomaay Fay, ak Usmaan Sonko. Ca Pale ba la leen dalal tey ci alxames ji. Njiiteefu réew mi (Présidence de la République) moo siiwal nataali ndaje mi. Ñu gis ci Maki Sàll di saafonte...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (6/11/2023)

PÓLITIG Kujje gee ngi waajal lu bees ñeel wote yiñ dégmal. Sëñ Abdurahmaan Juuf, di...

NJÀNG MEEK NJÀNGALE MI : YËNGU-YËNGU YI TÀMBALEETI NAÑU

Ci weer doŋŋ lañu tollu bi lekkool bi tijjee ak tey. Waaye ñaari kuréli...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (31/10/2023)

PÓLITIG Abdu Karim Fofana, jëwriñ ji yor kàddu Càmm gi, wax na jëmale ci amalub...

MBIRI USMAAN SONKO : CENA BI JËL NA NDOGALAM BA NOPPI

Ginnaaw bi DGE (Direction générale des élections) bañee doxal ndogal li àttewaay bu Sigicoor...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/10/2023)

PÓLITIG Waa F24 fésal nañ seen tiitaange ci tolluwaayu réew mi. Seen xel dalul wenn...

DUND BU JAFE BI : SAA-SENEGAAL YEE NGI ÑAXTOOTI

Démb ci gaawu gi, 21 oktoobar 2023, saa-senegaal yaa nga woon fa Place de...

KASOY SENEGAAL : XIIFAL NIKI NGÀNNAAY

Ñi ñu tëj ci kaso yi, xiifal gi lañ jël def ko ngànnaayu xeex....

MBIRI USMAAN SONKO : UMS DUGG NA CI COOW LI

Ginnaaw bi àttekat bi tirbinaalu Sigicoor jële ndogalu bindaat Usmaan Sonko ci këyitug wote...

XËT YI MUJJ

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (28/3/2024)

MAKI SÀLL DEF NA NDAJEM JËWRIÑAM MU MUJJ Dibéer jii weesu lañu doon amal...

MAKI SÀLL, DALAL NA JOMAAY AK SONKO FA PALE BA

Njiitu réew mi, Maki Sàll, dalal na ki koy wuutu, Basiiru Jomaay Fay, ak...

WOTEY 2024 : ËTTUB DABU BI BIRAL NA NJUREEFI NÉGANDIKU YI

Tay ci àllarba ji la Ëttub dabu bi nekkee Ndakaaru biral  njureefi néggandiku yi...

ÀDDINA SAA NGI NDOKKEEL BASIIRU JOMAAY FAY

Wëliis Maki Sàll mi muy wuutu ci boppu réew mi, yeneen Njiiti réew yi...