Paap Aali Jàllo

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

GÀTTALUG XIBAAR YI (Altine 13 eelu – dibéer 19eelu awril)

Paap Aali Jàllo Mbasum Covid-19 bi faat na juróomi way-tawat ci diggante dibéer ak altine Ci...

KORONAA JAT NA PAAP JUUF, GAYNDEY GAYNDE YI !

« Ërob, rawatina Farãs, dañuy xeex ak a bunduxataal tuutaafoni waaso yi (minorités ethniques)....

LI UMAR YUM AK AALI NGUY NJAAY WAX TASKATI XIBAAR YI ÑEEL GUURAL GI

Paap Aali Jàllo Senegaal, ca njëlbeen ga (2eelu fan ci weeru màrs 2020), diiwaanu Ndakaaru...

KORONAAWIRIS, LOO NU NARAL ?

  Ci bésub altine, 2eelu fan ci weeru màrs, atum 2020 la Covid-19 bi ganesi...

YOONU YÀQUTE…

"Noo lànk !" Ñaari baat yooyu la askanu Senegaal wépp àndandoo yuuxu cib doxu-ñaxtu, àjjuma jii...

CFA WALLA ECO ? SÀMBAAY BÀCC REKK…

Xaar bi yàggoon na, xeex bi metti lool, coow li ne kurr, saf sàpp...

Bataaxalu Saalif Keyta ñeel IBK

Ci tekkib Paap Aali Jàllo

MASAALIKUL JINAAN WALLA YOONI ÀJJANA YI

Ci àjjuma jii weesu, 27eelufan ci weeru sàttumbar, atum 2019, lañ doon ubbi ci...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA