Seexunaa Njaay

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/2/2024)

MBIRI PAAP GÉY AK MÀRSEY  Gannaaw CAN bi mu demoon ak Senegaal, Paap Géy, miliyë Màrsey (Marseille) bi dañ ko dàndoon ca këlëb ba, maanaan dañ ko génne woon, ber ko. Li ko waral mooy ni pasam dafay jeex ci weeru suwe 2024, Màrsey bëggoon...

CEDEAO TEGGI NA DAAN YI MU TEGOON NISEER

Démb ci gaawu gi la way-bokki kurél gi boole réewi Afrig sowu-jant yi ci wàllu koom daje woon fa Abujaa. La gën a fés ca la tukkee ca ndaje mooma mooy ndogal yi ñu jël ñeel réewum Niseer. Ndax, kenn umpalewul ne weeru sulet...

“KAFKA” LU MU NU WAX CI MAKI ?

Téereb "Kafka" bii dafa lay jàngal lu bari. Ni àddina man a xëyee rekk...

MAKI, FÀTTALIKUL “PAPA DOC”

Jafe na nga xam as lëf ci dundu "Papa Doc" (François Duvalier) mu réewum...

BUUR BI, DAG BI AK BATAÑSE BI

Bés, Buur dafa toog ak dagam, ñuy waxtaan. Buur ne ko : - Sama xel dafa...

XËT YI MUJJ

XIBAARI TÀGGAT-YARAM (25/2/2024)

MBIRI PAAP GÉY AK MÀRSEY  Gannaaw CAN bi mu demoon ak Senegaal, Paap Géy, miliyë...

CEDEAO TEGGI NA DAAN YI MU TEGOON NISEER

Démb ci gaawu gi la way-bokki kurél gi boole réewi Afrig sowu-jant yi ci...

MBAAM MI : ÑETTI LÉEB

Cokkaasu RFI bii daf nuy fàttali ñetti léeb yoy, mbaam a ciy ndeyu-mbill ji....

KAN LA NJIITU RÉEW MI NAR A DIISOOL ?

Nees leen ko xibaaree woon, diisoo la Njiitu réew mi Maki Sàll wooteeti ngir...