Facebook
Instagram
TikTok
Twitter
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Recherche
Ëtt bi
COKKAASU ODIA
MAGU WAXOON NAA KO
FÀTTALIKU DÉMB
WAXLEEN SEEN XALAAT
Xibaar
Bàyyi ci xel
Bindkatu ayubés bi
Diine
Gis-Gis
Kii Kumu
Koom-koom
Pólitig
Tàggat-yaram
Li des
Accueil
Auteurs
Articles postés par Defu Waxu
Defu Waxu
Li fës
BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI
Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...
17/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
15/12/2025
VOA AMAL NAB JOTAAY CI MBINDUM BUBAKAR BÓRIS JÓOB GINNAAW BI WEREKAAN BI JËLEE CARGALUG NEUSTADT 2022 BI. CUQAL CI LËNKAAY BII TOFTALU...
00:19:36
Jotaayu xam-xam ak Sën Abdu Xaadir Kebe
00:03:10
“Slam” Maysa Maara
00:15:20
Li Abdu Lahaat Ka wax ci wolof
Gis-Gis
WAAW, ANA KU BÓOM OMAR BOLONDEŋ JÓOB ?
Omar Bolondeŋ Jóob a ngi juddu ci 10eelu fan ci weeru sàttumbar 1946 ca Ñaame,...
21/11/2019
Xibaar
ËLLËGU XALIFA SÀLL CI LÀNGU POLITIG GI
Dibéer, 29eelufan ci weeru sàttumbar 2019, la Xalifa Sàll gisaat jant bi ginnaaw bi...
13/10/2019
FÀTTALIKU DÉMB
JIÑAABO, JÀMBAARU SELEKI BA CA SIGICOOR
Boo demee ca diiwaanu Sigicoor, dinga fa fekk liise bees duppe Jiñaabo. Waaye, aka néew nit...
13/10/2019
FÀTTALIKU DÉMB
DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI
Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci...
22/09/2019
Gis-Gis
SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU
At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn...
30/08/2019
Gis-Gis
NAN WAX CI YENN SÉRI TELE YI
Jamono jii nu tollu temm bari na lu ñu seetlu ci miim réew, ñeel...
14/08/2019
Xibaar
TANOOR NOPPI NA BA FÀWW
Usmaan Tanoor Jeŋmi fi doonoon njiitu ‘’Parti Socialiste’’ dale ko atum 2000, bi pa1rti...
25/07/2019
Gis-Gis
ALIYU SÀLL, GII MARYIIS SAAÑA : KUMBA AM NDEY AK KUMBA AMUL NDEY
25/07/2019
1
...
12
13
14
...
16
Page 13 sur 16
XËT YI MUJJ
Li fës
BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI
Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...
17/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
15/12/2025
Li fës
BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO
Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...
15/12/2025
Li fës
COKKAASU ODIA
08/12/2025