Li fës

SOXNA XADIJATU NJAAY CA KUNGÉEL, DOY NGA ROYUKAAY ! (AMI MBENG)

« …ñeewuma sama benn moroom bu jàng farañse. » Njiit li, boroom raaya yi, taalifkat bi, njiitalu...

TUKKI TEKKI, TOOG TOROX ? (PAAP AALI JÀLLO)

« Tekki mbaa dee ! » Li ko dale 1eelu fan jàpp 12eelu fan ci weeru oktoobar bii...

IBA DEER WÉETAL NA SENEGAAL (NDEY KODDU FAAL)

Gaawu 31eelu fan ci weeru oktoobar 2020 la Iba Deer Caam génn àddina ci...

SENGHOR, HOUPHOUET, DOOMI-AFRIG YI DAAN XEEX AFRIG (BOOS NDÓOY)

"Tubaab yaa ngiy dem, waaye seen i karabaane a ngi des sunu biir ba...

MUSAA JÓOB BAÑ NA NI MUUT, NEE NA MOTT (NDEY KODDU FAAL)

Musaa Jóob layookat bi doon jiite "Dakar Dem Dikk" la njiitu réew mi tekki...

EKSAME BAKALORYAA BI DOOR NA TEY (AMI MBENG)

Niki bésub tey jii la eksame bakaloryaa bi door ci réew mépp. Jukkees na...

AKON TÀMBALI NAA TABAX DËKKUB LËMM (MUSAA AYSATU JÓOB)

  Ginnaaw bi mu sottalee nas boobu mu duppe woon "Akon lightening Africa", kii di Aliyun Badara Caam di doomu-Senegaal...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...