Li fës

WOTEY NGOMBLAAN GI : PASTEF RAAFAL NA 130I TOOGU

DGE, kurél giy saytu mbirum wote yi, siiwal na njureefi négandiku yi ñeel wotey...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/11/2024)

DIC WOO NA AADAMA GAY Tay ci alxames ji lañu ko woolu, ñetti waxtu ci...

ÀNDU NAWLE

Bokk na ci anam yi nit lootaabee ag dundam ci kaw suuf, lu nekk...

PASTEF AK ÑOOMIN SEEN

Ndam la féete na wet. PASTEF a gobbi lépp, lëmbe géew bi, gën a...

WOTEY NGOMBLAAN GI : TAXAW-SEETLU YI NJËKK

Njureefi wotey Ngomblaan yi ñoo ngi tàmbali di génn, rawatina fa bitim-réew ak réew...

WURE WA DEM NA KËŊŊ !

Ngomblaan gi, walla Péncum ndawi réew mi (ni ko ñenn ñiy wowee), benn la...

BÉS BI MUJJ CI KÀMPAAÑ YI

Tay jii, bu guddi gi xaajee, la kàmpaañ yi ñeel wotey Ngomblaan gi di...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...