Li fës

« WAXLEEN DËGG SONKO ! »

Ànd, wax dëgg ca la. Ànd bu laluwut ci dëgg, du yàgg. Te, sa...

SIIWALUB TOFTALEG SAABALUKAAY YI CÀMM GI NANGU

Dees na siiwal limu saabalukaay yi méngoo ak yoon ci lu yàggul dara. Bees...

FITNAY KÀMPAAÑ BI / NDAR : JÀPPAGUM NAÑ 81i NIT

Pólisu Ndar bi jàppagum na juróom-ñett-fukki nit ak benn yees njort ne dañu laale...

TUKKITE NJIITU RÉEW MI FA RIYAAT

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bàyyeekoo na fi réew mi démb...

LËNT-LËNT ÑEEL FAATUG MAMADU MUSTAFAA BA

Altine jee weesu, yemoo woon ak 4i pani nowàmbar 2024, la Mamadu Mustafaa Ba...

SÉMBUW NDEFARUG DAAMARI SÓOBARE

Dees na samp ndefarug daamari sóobare fi réew mi. Xibaar la bu tukkee ci...

ETAASINI : DONALD TRUMP FALUWAAT NA

Ki fi nekkoon Njiitu réewum Etaasini, Donald Trump (20 sãwiyee 2017 ba 20 sãwiyee...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...