Li fës

MBIRUM KAASAMÃS

Ci àjjuma jee weesu, magum jëwriñ yi, Usmaan Sonko àddu woon na ci téere...

PAATUG MAMADU MUSTAFAA BA MA WOON JËWRIÑU NGURD MI AK NAFA GI

Léegi la APS siiwal xibaaru paatug Mamadu Mustafaa Ba mi woon jëwriñu ngurd mi...

TUKKITEY NJIITU RÉEW MI FA ARAABI SAWDIT AK TURKI

Dibéer jee weesu la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukki woon na....

SÉMBUB GTE (GRAND TRANSFERT D’EAU) BI

Càmmug Senegaal ak SINOHYDRO (bànqaas ci kër gii di Power-China) taxawal nañu liggéeyi sémbub...

BALAA NOO LAAX JAAY…

Nit, ak xelam ak i xalaatam yu xóot, du jóg ci di jéem a...

TABAXUG DËQ FA NDAR

Tàmbali nañu tabax ab dëq (digue) fa Daaru, diiwaanu Ndar. Jubluwway bi mooy aar...

NGËLÉN FA ESPAAÑ : 95i BAKKAN ROT NAÑU

Tay, ci àllarba ji, 30i oktoobar 2024, ngëlén lu am doole moo dikkal waa...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...