Li fës

TUKKIB NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, tukkee na fi réew mi barki-démb...

NDOORTEELU KÀMPAAÑI WOTEY PALUG DÉPITE YI

Biig la kàmpaañ yi door. Kàmpaañ yooyu, ñi ngi war a jeex fukki fan...

KÀDDUY NJIITU RÉEW MI

Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay yékkateeti na ay kàddu. Muy i...

KUPPEG TEFES : SENEGAAL JËLATI NA RAW-GÀDDU GI

Gayndey Senegaal yi féetewoo kuppeg tefes gi amati nañu ndam. Ci gaawub tay jii...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/10/2024)

COOWAL TABBUG SÀMBA NJAAY Démb, ci ndajem jëwriñ yi lañu tabbee Sàmba Njaay, def ko...

MBINDUM WOLOF : “FONK SUNUY LÀMMIÑ” TÀGGAT NA AY SAABALKAT

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ amaloon na jotaayu njàngum bind wolof. Saabalkat yi la ko...

MBIRUM BUGAAN : 30 OKTOOBAR 2024 MOOY BÉSU ÀTTE BI

Njiitul "Mouvement Geum sa Bopp" , Bugaan Géy Dani, mi ngi ci loxoy yoon...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...