Li fës

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (21/10/2024)

WALUM DEX GI Càmm gi teggiwul tànkam ci taxawaay bi mu am ñeel walum dex...

GIGA MEETING PASTEF : FOO SÀNNI MBÀTTU MU TAG

Démb, ci gaawu bi, la waa Pastef doon amal seen ndaje mu réy moomu....

KOOM-KOOM : PÉNCOO ÑEEL NDEFAR GEEK YAXANTU BI

Càmm gi dogu na ci aar cumbeefi biir réew mi (les entreprises locales). Jëwriñ...

MAATAM : WALUM DEX GI NANGU NA 700i TOOLI CEEB

Walum dexu Senegaal gaa ngi wéy di jur ay loraange yu jéggi dayo. Fa...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (17/10/2024)

WAAJTAAYU WOTEY PALUG DEPITE YI Lu tollu ci weer moo des ci wote yi. Waaye,...

MAKI SÀLL MIIM NA

Njiitu réew ma woon, Maki Sàll, weddi na tuuma yees gàll ci ndoddam. Càmm...

KAAJARUG SÉMBUW SOPPI SENEGAAL FII AK 2050

Sémb wi ñu doon coow ay at, ay weer, ay ayi-bés, mujj na a...

LU YEES CI MBIRUM PRODAC

Am na lu yees ci mbirum Prodac mi. BAD (Brigade des Affaires Générales), di...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...