Li fës

BAKKEL : NJIITUL SAED LI SEETI WOON NA BAYKATI KÀMBUG KOLANGAL GI

Mbënnum dexug Senegaal gi dafa jural ay jafe-jafe dëkk yi ko dar, rawatina Bakkel...

LU YEES ÑEEL BÓOMUG ASIIS DABALAA

Coowal bóomug Asiis Dabalaa gi ak jarbaatam bii di Buubakar Gano, ñu gën koo...

MÀGGALUG TUUBAA 2025

Tay, 13i pani ut 2025 mooy méngook 18eelu fanu safar ci atum 1447 ci...

MÀGGALUG TUUBAA GI

Màggal gi jubsi na. Nit ñaa ngay waaj, ku nekk ci sa wet. Waa...

MAN MAAY KAN ?

Danuy faral di dégg ñu naan : « boo xamul foo jëm, dangay dellu...

“GAINDESAT” : SENEGAAL AM NA SATELITU BOPPAM

Keroog, 16i pani ut 2024, la Senegaal dugg ci mboorum xarala ak gëstu. Nde,...

DALUWAAY BU BEES ÑEEL SAABALUKAAY YI

Jëwriñu jokkoo beek jokkalante gi, Àlliyun Sàll, taxawal nab daluwaay bu bees. Muy jumtukaay...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...