Li fës

NDOG MU METTI FA KUMPENTUM

Ndogum yoon (aksidaŋ) mu mettee ame fa Kumpentum, tey ci suba teel, bi 7i...

NGOMBLAAN GI JOYYANTI NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañ sémbuw àtteb 10/2024 wiy soppi ak a mottali « loi...

NGËRËMUL XAREKATI SENEGAAL YA WOON

Réewum Farãs fas na yéene fésal ngërëmam ñeel xarekati Senegaal ya ko xettali woon...

CAYTUG SUUFI TEFESI SENEGAAL YI

Kurél gi doon saytu suuf si féete ci tefesi Ndakaaru yi, jébbal nañu Njiitu...

GEREEWU SAABALUKAAY YI

Saabalukaay xéy nañ bank seen i loxo tey ci talaata ji, 13i pani ut...

JÀPP NAÑU AG GAAL FA BÀMBUGAR

Mbëkk maa ngi wéy di lëmbe réewi Afrig sowu-jant yi, rawatina Senegaal. Saa su...

NDAJEM MBOOTAAYU ÀTTEKATI SENEGAAL YI

Mbootaayu àttekati Senegaal yi, ñu gën koo xam ci turu UMS (Union des Magistrats...

XËT YI MUJJ

KUBALI GALAG YI : NGUUR GI DAJALE NA 3 000IY MILIYAAR

Nguur gi siiwal na caabalug doxal ñeel nafa gi ci juróom-ñeenti weer yi njëkk...

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...