Li fës

NDOX MI : FSS A NGI SÀKKU ÑU SIIWAL PAS YI

Kurél gii di Forum Social Sénégalais, gàttal biy joxe FSS biral na càkkuteefam ñeel...

NDAJEM NJIITI KIPPAANGOY DÉPITE YI

Coowal DPG li ba tey jeexagul. Nde, ndeyu-mbill ji, Usmaan Sonko, dafa am ay...

TAXAWALUG NJËWRIÑ GU YEES

Lu tollu ci ñetti weer kepp, ginnaaw bi ñu leen falee ak léegi, Nguur...

TAMXARIT

Tamxarit bokk ci na ci xew-xewi diine fii ci Senegaal. Tur wi rekk làmboo...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (15/7/2024)

MATALEG NOSTEG WOTE YI Barki-démb ci gaawu gi, doon nañ amal ndajem weccante xalaat...

EURO AK COPA 2024

EURO 2024 Démb, ci dibéer ji, 14 sulet 2024, la woon finaal Euro 2024 bi...

JÀKKAARLOO NJIITU RÉEW MI AK TASKATI XIBAARI YI

Démb ci gaawu gi, fukki fan ak ñett ci weeru sulet 2024, la Njiitu...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...