Li fës

NDOGAL YU BEES ÑEEL NJÀNG MU KOWE MI

Ay ndogal yu bees wàcc nañ ci njàng mu kowe mi. Muy i ndogal...

KENUY FAYDA YI

Nit ñi dëkkee ci àddina si, jamano jii, xayma nañu leen ci lu ëpp...

SENEGAAL/ANSD : LIMU NIT ÑI

ANSD, banqaas biy saytu limu nit ñeel yu ni mel, génnee na caabalam gu...

USMAAN SONKO DALAL NAÑU KO FA TUUBA AK TIWAAWON

Njiitu Càmm gi, Usmaan Sonko, seeti woon na kilifay diine yu Tuubaa ak Tiwaawon....

JÉYYAY MBËKK MI : AAMADU BA (BBY) ÀDDU NA

Elimaanu jëwriñ ja woon ci nguurug Maki Sàll, Aamadu Ba, àddu na ci jéyya...

AES AK CEDEAO : XIIROOK ŊAAYOO BA KAÑ ?

Diggante ñaari kuréli Afrig sowu-jant, seytaane génnagu ci. Nde, seen diggante baa ngi wéy...

TUKKIB BIRAM SULEY JÓOB FA FARÃS

Jëwriñ ji, Sëñ Biram Suley Jóob, yékkati na ay kàddu ñeel ndefari réewum Farãs...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...