Li fës

MAKI SÀLL FEDDALI NA KÓOLUTEEM CI AAMADU BA

Àllarbay tay jii la xibaar gi rot, njiitu réew mi Maki Sàll xamal na...

NGUUR GI TOPPEETUL USMAAN SONKO DARA !

Nguurug Maki Sàll gi dellu ginaaw ci topp bim doon topp Usmaan Sonko ci...

LI GËN A FÉS CI WOTEY 2024 YI (11/3/2024)

WOTEY 2024 YI : LAWAX YI TÀMBALI NAÑU DAGAAN YI Démb ci dibéer ji la dagaanug...

WIDEWOO BASIIRU JOMAAY FAY DU JÀLL FA RTS

RTS, kibaaraan la gu wute ak yeneen yi nekk ci biir réew mi. Ndax,...

WOTEY 2024 : CÀKKUTEEFU AAR SUNU ELECTION

Fileek Fukki fan ak juróom, dees na amal wotey palug Njiitu réewum Senegaal yi...

JËWRIÑI CÀMM GU BEES GI

Bërki-démb la Njiitu réew mi tasoon Càmm gi daldi tabb Siidiki Kaba Elimaanu jëwriñ...

JIGÉEN AY BOROOM-KËR

Ci li nu tàmm a dégg, boroom-kër, góor lees koy askanale. Waaye, bees settantalee...

XËT YI MUJJ

MBIRUM DIJJE BAAJI AK FULBEER SÀMBU : YOON TUUMAAL NA SEROM BÀNJAKI « SNIPER »

Ca atum 2022 la coowal ñaari sàndarm yii di Dijje Baaji ak Fulbeer Sàmbu...

FUTBAL : DÓOR NAÑU GAYNDEY SENEGAAL YI

Gaynde Senegaal yu futbal bi ñàkk nañu joŋante bi ñu doon amal ci seen...

JAMÑAAJO : TAXAWAL NAÑU AG NDEFAR GUY LIGGÉEY AY BUNT AK I PALANTEER

Jëwriñu Ndefar gi ak Yaxantu bi, Sëriñ Géy Jóob, jiite na xewum ubbiteg ndefar...