Xibaar

WOMEN FIRST TV Tele jigéen ñi, ngir jigéen ñi

WOMAN FIRST TV tele la bu ay jigéen sos jagleel  ko it jigéen ñi....

DÉGGOOB 79. 329 MILIYAAR DIGGANTE SENEGAL AK BAD

Jëwriñ ji ñu dénk fànnu koom-koom gi, Aamadu Hot, xaatim na ab pas bu...

WUJJE GI CI BIIR KUJJE GI  LAN MOOY JUBLUWAAY BI ?

“ Yaa ma..” ji ak “Maa la…” ji a ngi tulle ak màlle ci...

AFRIG, TONTU DU FOROX, Tontu ñeel kàdduy Óreliyoo De Lórãtis yi

Duma topp diw boo gis, fi ngeen jëm dafa sorewul. Loolu la waa CAF...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI, Dibéer 14 ut 2022

PÓLITIG  Li bettul kenn mooy fekki gi Paap Jóob fekki waa BBY. Mu nekkoon lu...

LI GЁN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI Àjjuma 12 ut 2022

PÓLITIG : Ndogal yi lёkkatoo yii di YEWWI ak WALLU jёl Ginnaaw seen ndajem waxtaan...

Naalub yeesalaat Raglu Aristide Le Dantec Li waral coow li 

Raglug Aristide Le Dantec lañ nar a tëj, 15 ut bii ñu dégmal. Ndogal...

14eelu LËLU SAES : AW YOON NGIR TINKI NJÀNG MU KAWE MI

Kenn werentewul ne njàng mu kowe mi dafa nekk ci guuta. Ab diir a...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...