Xibaar

WAAJTAAYU MÀGGALU TUUBAA

Dëkk bu sell bi, Tuuba, dafa aadawoo di amal at mu jot màggalu 18...

WURUS RUSUL A DELLU NGALAM WURUSU MALI, CA LOXOY SAA-MALI

Saa-Mali yi léegi ñooy defaral seen bopp seen wurus. Liggéey boobu nag, dañ ko...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI

POLITIG : Toussaint Manga génn na PDS  Ab bataaxal la kii di Toussaint Manga jébbal njitaal...

TAXAWAAYI DÉPITEY KUJJE GI LAATA SEEN AG DEM CA PÉNCUM NDAWI RÉEW MA

Ginnaaw bi njureefi joŋantey palum dépite yi rotee, yenn ci dépite yi biral nañ...

LI GËN A FËS CI XIBAARI BÉS BI Gaawu, 20 ut 2022

XEW-XEWI JAMONO Yokkuteg njëgu soble ga ca Tuubaa  Ñàkkum soble bi ganesi réew mi ci fan...

Gàttalug xibaar yi, Alxames 18 ut 2022

 Siin Lii nag ag lёngoo la gu jёm ci wàllum mbey ci diggante ñaari réew...

BALAA NGAA WAX NAAM, NE FA

Lekkool bi, ay at ñu ngi nii jafe-jafe bu dem, moroomam wuutu ko. Bokk...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...