Xibaar

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA II

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA (II) ‘’KU NEWUL ‘FRANCE DÉGAGE’ WAXOO DARA’’ Li ngeen di jàngsi mooy ñaareelu xaaju...

LAAJ-TONTOOK GUY MARIUS SAGNA (GII MARYIIS SAAÑA)

Seen yéenekaay LU DEFU WAXU mi ngi dalal tey Gii Maryiis Saaña, fara caytu...

INIWÉRSITE GASTOŋ BERSE : LU ËPP TUURU

18Coow li neeti na kurr. Ndongoy Iniwérsite Gastoŋ Berse bu Ndar defati nañu seen...

ARAM FAAL, SUNU SÉEX ANTA JÓOB BU JIGÉEN…

Talaata jii weesu di 23 ci weeru awril la Mbootaayu-Xeet yi jagleel bépp teere...

SÀNDIKAA NJABOOTU ALFABETISAASIYOŊ JUDDU NA

Askanu Senegaal dafa mës a weg i làmmiñam, làmmiñi réew mépp. Yàgg na leen...

GAALU JINNE

Jinne yu ñuul yi ñaay nañu Sunu Gaal gi, soppi ko gàngunaay, tëmbal ko...

7 MÀRS WALLA 8 MÀRS ? BEY CI SA WEWU TÀNK…

Juróom-ñetteelu fan ci weeru màrs la xel yépp di dem ci jigéen ñi, ndax...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...