Xibaar

58eelu NDAJEM OHADA

Tay ci alxames ji lañu doon amal ndajem jëwriñi kurélu OHADA (Organisation pour l’Harmonisation...

SÀNDIKAA YI FIPPU NAÑU

Sàndikaa yu bari door nañu ay ñaxtu ci ayu-bés bii. Muy ñi féete ci...

TÀGGE : SËRIÑ MUSTAFAA SAALIW MBÀKKE DËDDU NA

Umma islaam ñàkk na kilifa gu tedd. Njabootu murit a ngi jooy kàngaam bu...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/2/2025)

NDÉGLUG FARBA NGOM Tay, ci alxames ji la waa PJF (Pool Judiciaire Financier) woolu woon...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (12/2/2025)

CAABALUG ËTTUB CETTANTAL BI : CÀMM GI DINA JANOOK TASKATI XIBAAR YI ËLLËG Ëttub cettantal gi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/2/2025)

NJIITU RÉEW MI TEEWE NA 42eelu JOTAAYU "Comité d’orientation de l’AUDA-NEPAD" Ci xëtu Facebookam la...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...