Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

BADARA GAJAGA FANAANI NA KASO

Ayu-bés bii ñu génn lañu la Yoon woolu woon Badara Gajaga. Li sababoon woote bi, kàddu yi mu yékkati woon ci jotaayu Jàkkaarloo bi...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL : SAA-SENEGAALI BITIM-RÉEW Abiib Jara gan-ganluwul fa Àngalteer. Gannaaw ba mu jógee Strasbourg dem Sunderland, doomu Senegaal ji amal na ci gaawu gii matsam bu...

AG PAS GU YEES DIGGANTE SENEGAAL AK MÓRITANI

Réewum Senegaal ak mu Móritani yeesal nañu ag pas ci seen diggante. Muy Pas gog, dina dindi lépp lu doon gàllànkoor dem beek dikk...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (10/7/2025)

PASTEF MÀGG NA Atum 2014 lañu sosoon làng gii ñuy dippe PASTEF. Maanaam, atum ren jii la am fukki at ak benn ba mu sosook...

NDAJEM DONALD TRUMP AK JURÓOMI NJIITI RÉEWI AFRIG

Senegaal, Gaboŋ, Gine-Bisaawo, Liberiyaa ak Muritani… juróomi réew yii la Njiitu réewu Etaasini li, Donald Trump, dalal ca seen njénde la. Ci bésub àllarbay...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/7/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ETAASINI Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay bawoo na ci réew mi tay ci talaata ji, wutali réewum...

XEW-XEW BU TIIS FA JÀNGUNE JU KAWE JOJ NDAR

Naqar ak tiis la waa Ndar fanaanoo guddig barki-démb rawatina ndongo ya nekke fa daara ju kawe jooju di UGB (Université Gaston Berger de...

COOW TOPP NA ELIMAANU JËWRIÑ YI

Daar-daar bi Sëñ Usmaan Sonko doon amal mujje na a jur coow ci pénc mi. Ñu bari ci kujje gi di ñaawlu kàddu yi...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/7/2025)

NDAJEM ETAASINI AFRIG Ayu-bés bii ñu jëm lañuy amal ndaje mii ñu dippe “sommet Etas-Unis-Afrique”. Muy ndaje mu am solo moo xam ne du réew...

ÑAXTUY SÀNDIKAA YI

Jamono yee ñu weesu, ñaxtuy sàndikaa yi yëngaloon na réew mi. Waaye, ginnaaw ab diir dañoo wàññi. Waaye nag, dafa mel ni ñi ngi...

DAAR-DAARU USMAAN SONKO (NJIITUL PASTEF)

Ci guddig démb ji, Usmaan Sonko, njiitul làngu PASTEF, doon na amal daar-daar ci xëtu Facebookam. Ca biir waxtaan woowa, àddu na ci tolluwaayu...