Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (1/7/2025)

NDAJEM ÀDDINA SI ÑEEL KOPPARAL SUQALEEKU GI Démb ci altine ji lañu doon amal Ndajem àddina si ñeel kopparal suqaleeku gi. Ñoo ngi ko doon...

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ

Démb, ci dibéer ji, la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, bawoo ci réew mi, jubali fa Tugal. Moom nag, du guléet muy...

XIBAARI TÀGGAT-YARAM

FUTBAL Racine Club de Lens xamle na ni Nàmpalis Mendi dana jóge ca ekib ba gannaaw bam fa defee ñaari at (2023-2025). Ci diir bim...

NGOMBLAAN GI YEESAL NA SÀRTU-BIIRAM

Dépite yi jàllale nañu « loi organique no10/2025 ». Muy àtte bob, dafa ñëw ngir andi ay coppite ci sàrtu-biiru Ngomblaan gi. Démb ci àjjuma ji, 27...

USMAAN SONKO “ BÉG” NA CI TUKKEEM BI MU AMAL FA SIIN

Elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, fésal na mbégteem ci tukki bi mu tukki fa réewum Siin. Pekeŋ la ko waxee, di gëblag réew ma....

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (26/6/2025)

TUKKIB NJIITU RÉEW MI FA ESPAAÑ Bu yàggul dara la Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jóge fa ndajem CEDEAO ma. Balaa yàgg, dina...

“BANQUE MONDIALE” LEBAL NA SENEGAAL 65i MILIYAARI CFA

Ci talaatay démb ji la "Banque mondiale" siiwal ne nangu na a lebal Senegaal koppar yu tollu ci 115i miliyoŋ ciy dolaar, yemook 65i...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (24/6/2025)

NGURD CÀMM GI CI ÑETTI WEER YI JIITU CI ATUM 2025 MI Jëwriñu ngurd meek nafa gi siiwal na caabal gi aju ci yorinu nafa...

TUKKIB ELIMAANU JËWRIÑ YI FA RÉEWUM SIIN

Àjjuma jii weesu la elimaanu jëwriñ yi, Usmaan Sonko, dooroon ab tukkeem fa bitim-réew. Moom nag, guléet muy génn kembaarug Afrig bi ñu tabbee...

SAA-CEES DAANAAT NA SÀRKOO !

14i at ci ren gannaaw ba Saa-Cees ak Sàrkoo njëkkee bëre. Seen lámb jooju, doomu Géejawaay ji moo ko yóbbuloon doomu garã-yoof ji, daanoon...

NOSTE PÓLITIG GOG IRÃ

Ginnaaw ba Humayn àndee ak askan wa daaneel Nguur ga fa nekkoon, ca lañu amalee ay wotey referàndom, keroog bési 30 ak 31 màrs...

67EELU LËLU NJIITI RÉEW AK CÀMM YU CEDEAO

Njiitu réew mi, Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, dem na tay ci gaawu bi, 21 suwe, fa Abuja (réewum Niseeriyaa), ngir teeweji 76eelu lëlub...