Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

"MARTEAU" BI

FUTBAL AK BASKETU SENEGAAL : YAAKAAR AK YÀKKI

Bi Alseri dumaa Senegaal benn ci dara ci finaalu joŋanteb réewi Afrig yi (CAN) ak léegi, mu ngi bëgg a yàgg. Waaye, kenn fàttewu...

DAAWUDA JAAWARA FAATU, NUY FÀTTALIKU SENEGÀMBI

Daawuda Kayraba Jaawara, jiite woon fi réewum Gàmbi 1979 ba 1994, faatu na ci 27eelu ut 2019 bii ñu génn. Mëneesul a wax Daawuda Jaawara...

LAAJ-TONTU : SAADA KAN BÓRIS JÓOB (II)

Waxtaan wii, ab tekki la ñeel jotaayu laajt-tontu bu Saada Kan di amal ci tele 2Stv ñaari ayu-bés yu nekk, te mu dalaloon ci...

NAWETU ITALI AK JOŊANTE REN JI

Nu des ak yéen ci réewum Itali ba tey. Tey nag, xibaar yi nu leen di jottali xaw nañoo wute ak yi ngeen di...

MAKI/XALIFA : MAG, BU RUSEE NE MAA-TEY

Fan yii nu génn, bare woon na ñu doon yéy ak a yàbbi ci mbirum Xalifa Sàll, di wax ci njéggal bi ko Maki...

SUNUY DOOMI-NDEYI MALI YI SONN NAÑU

At yi weesu yépp, fitu doomi-Mali yi toogul benn béréb. Weer yi nu génn sax, seen njàqare ak seen tiis dafa mel ni lu...

‘’LI TAX SÉEX ANTA JÓOB AMUL MOROOM…’’

WAXTAANU SAADA KAN AK BUBAKAR BÓRIS JÓOB

GENN GAAL, ÑAARI JULLI

Ku makiyaasu mbaa ñu makiyaas la, boo ñaqee ñaaw

« Man, dama jàpp ne, CFA ak ECO ñoo yem kepp, benn baaxu ci. »

Ñaareelu xaaju waxtaanu Mamadu Jàllo ak Ndongo Sàmba Silla