Stay tuned

Subscribe to our latest newsletter and never miss the latest news!
Our newsletter is sent once a week, every Monday.

Latest news

WÉR-GI-YARAMU DOXANDÉEM YI CI ITALI

Nu yattati sunu xalima ngir biralati sunuy kàddu. Waxati dëgg jot na. Nu dikk ak yéen ci mbiru doxandéem yi féete fii ci Itali....

NAN WAX CI YENN SÉRI TELE YI

Jamono jii nu tollu temm bari na lu ñu seetlu ci miim réew, ñeel tele yi. Waaye li ci gën a ràññeeku mooy séri...

NDONGO SÀMBA SILLA « …CFA, XETTALI FRÃS A KO TAXOON A JÓG»

Mamadu Jàllo :  Ndongo Sàmba Silla, yow doomu-Senegaal nga, di boroom xam-xamam bu mag ci wàllu koom. Ak li ngay doon ndaw yépp, sa tur wi...

TANOOR NOPPI NA BA FÀWW

Usmaan Tanoor Jeŋmi fi doonoon njiitu ‘’Parti Socialiste’’ dale ko atum 2000, bi pa1rti boobu ñàkkee nguur gi ba sun jonni-yàllay-tey jii moo génn...

BÉS DINA ÑËW !

Lu yëngu lu ne, li ko yëngal a ko ëpp doole. Dëgg la, futbal am po rekk la. Wànte mëneesu koo méngale ak yeneen...

LU WARAL ITALI SOPPEEKU NII ?

Ak lu waay mën a wax, réewum Itali yàqu na. Bi Salwini toogee ci jal bi ba tey, ñoo ngi fay bundxatal doxandéem yi,...

MBAY JAAG, GOR GI SENEGAAL AMEEL BOR (II)

Am it lu mat a taxaw-seetlu : jamono jooju Mbay Jaag doon jiite ndongo yi, fekkoon na mu bokk ci PAI, pàrti  “marsist” bu mag...

ALIYU SÀLL : KU AM KUDDU DOO LAKK

Aliyu Sàll tekki na ndombog-tànkam ci boppu CDC, teg loxoom ci Alxuraan, waat ne li ñu koy tuumaal, dara la ci deful. Ci la...

PÉNCUM RÉEW MI WALLA PÉNCUM BENNOO BOKK YAAKAAR ?

Am réew, su fa buur ak lingeer dee fecc, ku fay woyaan doo rus a yaŋas. Kon boog, ndokk dipite yi !  La xew ca...

FUTBAL AK JAFE-JAFEY RÉEWI AFRIG YI

Doom-aadama fent na ay xeeti po yu bare. Ba ci tàggat-yaram sax, nga xam ne, ci cosaanam, yar ak wér-gi-yaram ñoo ko taxoon a...