Ami Mbeng

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

DAANUB USMAAN SONKO AK NDEY XADI NJAAY : ÑU BAREE NGIY ÑAAWLU

Tey, ci alxames ji 1eelu fan ci weeru suwe la àttekat bi biral daan...

TEGGI TUUMA

Yàgg dina dindi tuuma, waaye gaaw cee gën bu naree jur njombe. Loolu la...

SÉEX TIIJAAN GAAJO WAN NA MAKI SÀLL BUNT BU MAG BI

Séex Tiijaan Gaajo séqoon naw waxtaan ak waa Iradio (90.3), ñu doon ko dalal...

SIGICOOR : « PANAANUG WAY-BËGGI REEW MI »

Ay téeméeri téeméeri nit ñoo dajaloo ca buntu këru Usmaan Sonko, fa Sigicoor jamono...

SAFAANTOO YA CA NGOR : ÑAARI BAKKAN ROT NAÑU

Njiitul mbootaay "Ngor debout", Mamadu Njaay, yëgle na ni ñaari nit dee nañu ci...

AKSIDAŊ CA KAWÓN

Aksidaŋ bu mettee amati ca Kawón, ci wetu fooraa ba, fa diwaanu Kawlax.  Ab biis...

LAAYEEN YI MERE NAÑU MAKI SÀLL

Ku dégg kàdduy Imaam Basiiru Caw Laay xam ne Laayeen yi mer nañ lool....

NGOR : KËRUG FARBA NGOM LAKK NA

Bu kenn àttewul, musiba dina am. Te, bu boobaa, dina rëccu dina fekk jëf...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA