Ami Mbeng

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee ngi waaj a song sémb yu mag yi ngir tabax réew mi. Looloo tax, ci Sémbuw Àtteb Ngurd mu 2026 mi, ñu sóoraale ci naaluw kopparal wu mag a mag....

MBIRUM MEERI BU NDAKAARU

Mbirum meeri bu Ndakaaru mi ngi wéy di jur coow. Tay rekk, Sëñ Bàrtelemi...

BÀRTELEMI JAAS NEKKATUL MEERU NDAKAARU

Bésub 11eel ci desàmbar, 2024, lañu dàq Bàrtelemi Jaas ci boppu meeri bu Ndakaaru....

TËJ NAÑ MUSTAFAA JAXATE KASO

Démb, ci altine ji, la Mustafaa Jaxate fanaan guddeem gu njëkk ca ndung-siin. Ginnaaw...

WAXTAANU NJIITU RÉEW MI AK VLADIMIR POUTINE

Njiitu réew mi, Basiiru Jomaay Jaxaar Fay, jokkoo na ak Njiitu réewu Riisii, Vladimir...

TASAARE DÉG-DÉG YU WÉRADI

Saabalkat bii di Aadama Gay mi ngi ci loxoy yoon fi mu nekk nii....

SIIWALUB TOFTALEG SAABALUKAAY YI CÀMM GI NANGU

Dees na siiwal limu saabalukaay yi méngoo ak yoon ci lu yàggul dara. Bees...

YOON : DAAN NAÑ BUGAAN WEERU KASO

Tay lees doon àtte Bugaan Géy Dani fa Tàmbaakundaa. Moom miy njiitul kurélu Gëm...

MAATAM : WALUM DEX GI NANGU NA 700i TOOLI CEEB

Walum dexu Senegaal gaa ngi wéy di jur ay loraange yu jéggi dayo. Fa...

XËT YI MUJJ

COKKAASU ODIA

2026 : SENEGAAL A NGI SÓOBU CI SÉMB YU MAG YI

Ginnaaw bi ñu defee at ak lu teg, Càmmug Basiiru Jomaay Jaxaar Fay gee...

MBIRUM SEEX TURE, GUNEG SENEGAAL GI ÑU FAAT CA GANA

Takk-deri Gana yi tàmbali nañoo lëñbët ngir ca yan anam la doomu Senegaal jii...

COKKAASU ODIA