Cubba Taal

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

MAAM LEES KAMARA, KENN DOOTU LA FÀTTE

Altine, 1eelu fan ci weeru Me lañ doon màggal liggéeykati àddina sépp. Fépp fu...

“SËRIÑ BI, FÀWW MU FEEÑ”

Bu ñu seetloo fan yee ci ginnaaw, werante amoon na ci nataali Séex Ahmadu...

KARIIM WÀDD BINDU NA, LÉEGI ?

Coowal wotey palug Njiitu réew ci atum 2024 door na bu yàgg te mbir...

MUSIBAB SINJAA

Diggante ndongo daara ak sëriñam, yenn saa yi, du doon lu ratax. Lu ci...

MAKI WAX NA AK NDAW ÑI

Màggalug bés bi Senegaal moome boppam, dafa nekk aada ci réew mi. Ñu jàpp...

KU JIITE RÉEW MI ?

Fi réew mi tollu jamono jii, teey na xel. Waaye, jur nay laaj yu...

LEKKOOL YA NGI CI YOONU LOMPOÑ

Coowal pólitigu Senegaal mi ngi wéy di jur jote ci réew mi. La ca...

PALUG KURÉL YIY TEEWAL JÀNGALEKAT YI

Njureef ya tukke ca wotey sendikaa jàngalekat yi bir na. Mu mel ni, jàngalekati...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA