Cubba Taal

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

SÉEX ANTA JÓOB : XARNUB LEER

Fanweeri at ak juróom-ñaar ginnaaw ba mu làqoo, Séex Anta Jóob du mës a...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Altine 6 féewarye 2023)

PÓLITIG PDS Abdulaay Wàdd njiitu réew mi fi woon génn na ca tekkaaral ga mu nekke...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (Dibéer 29 saŋwiye 2023)

TUUBAA : JAWUB “OCASS” LAKK NA Démb ci guddi, ay boori 22i waxtu, lees nemmeeku...

FESNAC

Kafrin dalal na xew-xewu mbatiit bu réy bi ñu dippe ci nasaraan Festival National...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (GAAWU 21 SAŊWIYE 2023)

PÓLITIG Waxtaan wa doxoon diggante Nguur gi ak ñi yor wàllum dem bi ak dikk...

SÉEX ALIYU NDAW : BÉS DU ÑÀKK, DAY SORE

Mbootaayu Fonk Sunuy Làmmiñ daa fas yéene delloo njukkal bindkat bu mag bii di...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (gaawu 7 saŋwiyee 2023)

PÓLITIG Tuuma ji ëttub cettantal gi tegoon ñenn ciy jëwriñ ak i DAGE ñeel koppar...

TUUBA, KAARAANGE GAA NGA CA LOXOY TAKK-DER YA

Tuuba, dëkk bu sell ba, baat ba benn la. Lu bari lañuy doxal ca...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA