Cubba Taal

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug elimaanu jëwriñ ya, Michel Barnier. Dépitey kujje gees duppee « La gauche » ñoo dugaloon pasu diiŋat mi, wote ko, jàllale ko. Muy tekki ne, Càmm gi Michel Barnier taxawaloon...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar a leen dikkal ci àllarbay tay jii, 4i pani desàmbar 2024. Dafa di, waadab seereer ba woon, Àmburuwaas Saar, moo génn àddina. Moom nag, Àmburuwaas Saar, mbër mu mag la woon,...

Ndeyu àtteg Bokkeefug Senegaal : ndey ji seex du tëdde wet

Sagar a ngi xeeñ. Ñépp a ko maase yëg. Xet gi ëbale ne ràpp...

NU DELLOO NJUKKAL YAAY MARI MU SELL MI

Boo déggee Popengin sa xel day dem ci waa jàngu bi. Muy màndargaal diiney...

BATAAXALU ITALI BU TIISE NII…

Mbokki Senegaal, Maa ngi leen di nuyu yéen ñépp, ku ci nekk ci sa tur...

DÉMB AK TEYU DOXANDÉEMI ITALI YI

Waxtaanu Baay Njaay ak B. S.

WÉR-GI-YARAMU DOXANDÉEM YI CI ITALI

Nu yattati sunu xalima ngir biralati sunuy kàddu. Waxati dëgg jot na. Nu dikk...

LU WARAL ITALI SOPPEEKU NII ?

Ak lu waay mën a wax, réewum Itali yàqu na. Bi Salwini toogee ci...

XËT YI MUJJ

DÉPITEY FARÃS YI DAANEEL NAÑU CÀMMUG MICHEL BARNIER

Dépitey Ngomblaanu Farãs yi wote nañu pasum diiŋat (motion de censure), daldi daaneel Càmmug...

ÀMBURUWAAS SAAR : AATU RÉER NA !

Njabootu làmbu Senegaal ak mbatiit am nañu dëj. Nde, xibaaru tiis ak uw naqar...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (3/12/2024)

CAAROY 44 : NJIITU RÉEW MI JËL NAY NDOGAL Barki-démb ci dibéer ji lañu doon màggal...

TIIS WU RÉY FA GINE

Mats futbal bu mujje ciy masta ! Mbir yaa ngi xew barki-démb ci dibéeru...