Cubba Taal

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (13/4/2024)

NJABOOTU LÀMB DAL NA CI KOW BIRAM SULÉY JÓOB  Bi jëwriñ jii di Biram Suléy...

CÀMM GU BEES GI : WAAW, ANA JIGÉEN ÑI ?

Ginnaaw ba mu jële lenge yi, njiitu réew lu bees li Basiiru Jomaay Jaxaar...

CAMPUG BASIIRU JOMAAY FAY

Ngelaw lu bees la réewum Senegaal noyyiwaat tembe ci campug Njiitu réew lu bees...

WOTEY 2024 YI : WURE WA DEM NA KËŊ

Ay waxtu rekk ñoo des ngir Saa-Senegaale falaat Njiitu réew lu bees lu war...

KAN MOOY ALIW MAMADU JA ?

Aliw Mamadu Ja ci 19i lawax yiy wut réew mi la bokk. Moom moo...

LI GËN A FËS CI WOTEY 2024 YI (16/3/2024)

PODOOR DALAL NA AAMADU BA Ni ñu ko xame ci jamono jii, lawax yi tàmbali...

WOTEB SÉMBUB « AMNISTIE » CA NGOMBALAAN GA

Sémbub « amnisti » bi Njiitu réew mi naal mu ngi jaabaajonge réew mi. Mu nekk...

WOTEY 2024 YI : 19i LAWAX ÑOO CI DES

Ginnaaw bi mu neenalee dekkare Njiitu réew mi jëm ci fommug wotey 25 féewiryee...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA