Cubba Taal

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

KARIIM WÀDD : “SAMAG GÀDDAAY MI NGI JEEX”

Ni ñu ko baaxoo gise ci njeexitalu at mu nekk, njiitu réew mi dina...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (29/12/2023)

CAMPUG LAWAXU USMAAN SONKO Muy xew-xew bu ñu dëgmal te ña fare ca lëkkatoo pólitig...

NGOMBLAAN GI WOTE NA CÀRTUG CÀMM GI

Bërki-démb ci altine ji fukki fan ak juróom-ñatt, dépite yi wote nañu sàrt càmm...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (14/12/2023)

ÀTTEB USMAAN SONKO Ndogal lañu doon xaar jëm ci àtteb Usmaan Sonko ak Càmm gi,...

USMAAN SONKO AK CÀMM GI, PËND BA WUREEGUL

Dogal bi ñu doon xaar tey ci Talaata ji jëm ci àtteb Usmaan Sonko...

LI GËN A FÉS CI XIBAARI BÉS BI (8/12/2023)

NDEY FAATU FAAL Ndey Faatu Faal mi ñuy woowee Faala Fëlëer nekk ab ñaxtukat,...

WAAJTAAYU BÉSU DAARA

Séex Umar Aan di jëwriñ ji ñu dénk njàng meek njàngale mi amal na...

JALOOREY RAGLUB SÓOBARE BU WAKAAM

Senegaal séqi na jéego bu am a am solo ci wàllu paj. Nde, doktoor...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA