Kurélu àttekat yu Senegaal gi, UMS, ñaawlu na taxawaayu Meetar Musaa Bookar Caam ginnaaw bi mu juree àttekat bii di Idiriisa Jara ci mbiri Muhamadu Ngom mees gën a miin ci Farba Ngom.
Démb ci àjjuma ji, 21 nowàmbar 2025, UMS (Union des Magistrats du...