Mbay Sow

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi ñu jagleel waa jasporaa bi, ci njiiteefu Njiitu réew mi Sëñ Basiiru Jomaay Jaxaar Fay. Muy guléet ñuy amal boobu bés fi réew. Ci weeru suwe bi weesu la Càmm gi...

COKKAASU ODIA

WALFADJIRI-NGUURUG MAKI SÀLL : GATSA-GATSA

Kamaj ! Benn yoon. Kamaj ! Ñaari yoon ! kamaj ! Ñetti yoon. Siñaalu tele Walfadjiri dogati na....

JÀMMI USMAAN SONKO, JÀMMI RÉEW MI

Barkaatu-démb, ci alxames ji, lañu daan njiitul làng gii di Pastef, Usmaan Sonko, lu...

ÑEETTEELU MOOME : MAKI SÀLL JÉGGAANI NA AW LAY

Jéggaani xaalis. Jéggaani dund. Jéggaani xam-xam. Léegi, jéggaaniy xalaat a ci des. Ndeke, Njiitu...

JÀPP NAÑU ÀPPUG WAXTAAN WI

Lu tollook weer a ngii wow, ñuy yéy ak a yàbbi ci waxtaan wi...

BENN LAYOO, 16i BAKKAN

Benn takk-der bu daamaru pólis bi jaar ci kowam, mu jaare fa, ñàkk bakkanam....

USMAAN SONKO AK MAKI SÀLL : CÓOKI MUJJ GI

Tey, ci altine ji lees war a àttewaat layoob Usmaan Sonko ak Maam Mbay...

TAS XIBAAR : TAS XAR-BAAX WALLA TAS CI KASO BI ?

Tasum xibaar mi ngi bëgg a tagatémbe jamono jii ci réewum Senegaal. Dara waralu...

« DAÑU MAA TOOÑ, WAAYE DUMA BÀYYI »

Yaayu Aadama miy jiiñ Sitoor Nduur ag ciif, àndul ak ndogal la tukkee ca...

XËT YI MUJJ

BÉS BI ÑU JAGLEEL JASPORAA BI FI RÉEW MI

Tay ci àllarba ji, 17 desàmbar 2025, doon nañu màggal fa Jamñaajo, bés bi...

COKKAASU ODIA

BÉS NIKI TAY, NEELEEN DOKTOOR PÀPPA AALI JÀLLO

Gaawo, 13eelu desàmbar 2025, ca Jàngune bu Ndar, la Pàppa Aali Jàllo (njiitul LDW)...

COKKAASU ODIA